Murtadaa Jóob

Dernière sortie

Woy ak cax ci ëttub làmmiñu wolof

Woy ak i Daajam ci Làmminu Wolof. 1 - Wuuteg nit ak mala ; 2 - Woy, taalif ak wax ; 3 - Woykat bi ak woyam ; 4 - Cosaanu woy ; 5 - Giiri daaj yi ci woyu wolof . Toftalu ci - "Sib naa la, yaw sama baay !!!" (Ci Jukkib fanweer i woy ak natt). Toftalu ci - Cax naa la ! Càqi naa la ! Pow um Cax ak séeni Càgi Ci 200 caq.

Les livres de Murtadaa Jóob